Bayil Mou Sedd lyrics

Songs   2025-01-05 20:54:42

Bayil Mou Sedd lyrics

Ngor amoul ndieuk boulko diay

Goree ba kheuy deh boulko bayi

Di dounde lo donoul amoul ndieurigne nanko bayi

Diarouko way, Fékhél nank ko bayi

2 ans yangui koy topp

Xalè bi néna bouggoula

Def nga louné wakh louné

Mome noboula

Lékato té nélawato

Dem nga bay khalat ni faw nga diouk serigne touko

Manila bayil mou sed

Bayil mou sed

Bayil mou sed

Diarouko bayil mou sed

Nièmé sagnsé telephone bou guène nga am ko

Yaw rek thi khalè cheveux bou cher nga solko

Ndékété yo yoro dangay abb yoro

Niodi boss di diay lou amoul nieupeu kham ni yoro

Kone bayil mou sed

Bayil mou sed

Bayil mou sed

Yoro kone deh bayil mou sed

Ngor amoul ndieuk boulko diay

Goree ba kheuy deh boulko bayi

Di dounde lo donoul amoul ndieurigne nanko bayi

Diarouko way, Fékhél nank ko bayi

Bayi bayi bayi, Bayil mou sed

Bayi bayi bayi, Bayil mou sed

Bayi bayi bayi, Bayil mou sed

Bayi bayi bayi, Bayil mou sed

Nena moy sa kharit té yaw rek la tek beute

Lo am dakoy nakhari gnéné nek leu moungék keur

Nga sagnsè mokoy sonal

Sa mbecté bonal kholam

Yeuk ngeu ni dalay sossal

None la Bouko falé bayil mou sed

Bayil mou sed

Boyil mou sed

Diarouko bayil mou sed

Mome mak la té ba legui nango gouko

Weur thi kogne bi dieul thi khalé bayé gouko

Niouleul bopp

Guéné face

Di diay taar

Père bayil mou sed

Dem nga feep

Wakh ngakh nieup

Kham nga lepp

Kone pere bayil mou sed

Ngor amoul ndieuk boulko diay

Goree ba kheuy deh boulko bayi

Di dounde lo donoul amoul ndieurigne nanko bayi

Diarouko way, Fékhél nank ko bayi

Bayi bayi bayi, Bayil mou sed

Bayi bayi bayi, Bayil mou sed

Bayi bayi bayi, Bayil mou sed

Bayi bayi bayi, Bayil mou sed

OMG more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof
  • Genre:
  • Official site:
  • Wiki:
OMG Lyrics more
OMG Featuring Lyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Artists
Songs