Bul Nangu lyrics

Songs   2024-12-21 05:26:03

Bul Nangu lyrics

Yow daal boulène topatoo, dokhal sa dokh

Yow daal ngala fatté lène té dokh sa dokh

Non non boulène may buzz, dokhal sa dokh

Bodio bodio, boulène wouteul buzz, dokhal sa dokh

Yow daal bougne la tardèl, dokhal sa dokh

[MBAYE DIEYE FAYE]

Gnii, matouniou Kilo, té manqué libre bolè si ignaane

Dokhal sa dokh boléssi raasou, dougne dégg darra

[YOUSSOU NDOUR]

Yow daal ngala fatté lène, nga dokh sa dokh

Non non boulène may buzz, dokhal sa dokh

Yow daal boulène topatoo, dokhal sa dokh

Bodio bodio, boulène wouteul buzz, bayil niou dèm

Yow daal bougn la tardèl, dokhal sa dokh

[MBAYE DIEYE FAYE]

"Am faroro", fa Yallay décidé, nitt dou fa dém

Geumal y’Allah, woolou Yallah, Moytou iniane

Wa Sénégal, Kocc Barma sama mame dja né

"Iniaane, dina moudiou sopalékou diaane matt borome"

Khamouloo louko yaayam booté, mandou ci moom

Nitt dina kheuy rekk bagne la GUIS NEGN KO FII

Té boko laadione dou la wakh LOU WARAL LII

Foumou tokk dégg sa tourr DI BEUGEU DÉÉ

Bako, Bako

y’Allah ngui dianokk moom

Nitt dina kheuy rekk bagne laGUIS NEGN KO FII

Té boko laadione dou la wakh LOU WARAL LII

Foumou tokk dégg sa tourrDI BEUGEU DÉÉ

Bako, Bako

y’Allah ngui dianokk moom

Boodé guène, sagnsél, khénio lou nékh, romb ko

Khol ba di dagg té douko fadj

Lolou doy na, ay doumay dorr

Bougn la tardél, dokhal sa dokh

Yow daal ngala faté lène té dokh sa dokh

Non non boulène may buzz, dokhal sa dokh

Yow daal boulène topatoo, dokhal sa dokh

Bodio bodio, boulène wouteul buzz, bayil niou dèm

Bodio bodio, boulène wouteul buzz, bayil niou dèm

Boul langg ak niom

Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Boul tog ak niom

Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Boul wakh ak niom

Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Boul sékk ak niom

Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Boul langg ak niom

Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Boul tog ak niom

Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Boul sékk ak niom

Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Tay ma khamal la sa noone yi, noy déf ak niome

Tay ma khamal la sa noone yi, noy déf ak niome

Oubil sa nopp tay ma wakhla, noy def ak niome

Wouteul sa keur gou fashion

Soll say yéré you fashion

Yorr sa auto bou fashion

Am andadoo you fashion

Di dokh dokhine bou fashion

[BILAHI]

Boul langg ak niom Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Boul tog ak niom Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Boul wakh ak niom Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Boul sékk ak niom Boul nangou dieul ndaaaaaaré

[MBAYE DIÈYE FAYE]

Thieuy, thieuy adouna,

Am na ay photocopies ak original

Ni la amé ay acteurs ak figurants

Acteurs yi aligné Figurants alignés

Thieuy, thieuy adouna, Nii rek la

[Youssou Ndour]

Tay ma khamal la sa noone yi, noy déf ak niome

Tay ma khamal la sa noone yi, noy déf ak niome

Oubil sa nopp tay ma wakhla, noy def ak niome

Wouteul sa keur gou fashion

Soll say yéré you fashion

Yorr sa auto bou fashion

Am andadoo you fashion

Di dokh dokhine bou

[BILAHI]

Douma langg ak niome Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Bilay douma tog ak niome Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Douma wakh ak niome Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Aaaaah wa Médina Boul nangou dieul ndaaaaaaré

Equipe Nationale... (Boul nangou dieul ndaaaaaaré)...bou Sénégal

Cissé, Cissé, Cisséééééé,

Cissé, ngarigueul mééw, Aliou Cissé

[MBAYE DIEYE FAYE]

Thieuy, empereur raw len

[YOUSSOU NDOUR]

Bilahi, Douma langg ak niome

[MBAYE DIEYE FAYE]

Wakh djii, na fashion

Dokhine, na fashion

Sa kholine, na fashion

Sa déglou, na fashion

Dokhine bou fashion

Auto bou fashion

Andandoo you fashion

Ak Empereur, fashion, fashion, fashion

Empereuroo dioub ba si geun na fashion

Youssou N’Dour more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, French, English, Unknown
  • Genre:Singer-songwriter
  • Official site:http://www.youssou.com/
  • Wiki:http://fr.wikipedia.org/wiki/Youssou_N%E2%80%99Dour
Youssou N’Dour Lyrics more
Youssou N’Dour Featuring Lyrics more
Youssou N’Dour Also Performed Pyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Artists
Songs