C'est la vie lyrics

  2024-06-23 15:45:03

C'est la vie lyrics

Maak ioe hé ! seuy laniou digué wone

Ndax ioe rek la nobone

Ngamay trompé samay noone dima ré

Niouné saleté lou ci bax moy mbalite yé

Sa téléphone dey sonné

Même bou minuit passé

Nga wouyu guestou nima wa keur nioy woté

Loutax ngamay def li

Kou melni mane dotoko amati (no no no)

Loutax ngamay def li

Khamal ni ioe dotoko défati (no no no)

Mane rek

Fouma nekh lay goudé beuss dina niow

Nga matteu sa lokho ja

Nieup la bayi né ioe la té dou ioe

Ya ngui nane ni beuss bo mandé fégn

Guéneu goudi bayi ma fi dém

Lane ngey outi l’amour ngui si keur gui

C’est la vie (c’est la vie, c’est la vie) oh

C’est la vie (c’est la vie, c’est la vie) oh

Maak ioe hé ! seuy laniou digué wone

Ndax ioe ioe rek la nobone

Ngamay trompé samay noone dima ré

Niouné saleté lou ci bax moy mbalite yé

Ioe khamoulo mane kima done

Sama xol lay diokh sa morome

Kou deung limou yorr sou wadé

Kou dioub rek mor for dieurigno

Yén facebook ak twitter (...) Ni whatsApp

Bayiwo instagram no no

Imo ak snapchat

Loutax ngamay def li

Kou melni mane dotoko amati (no no no)

Loutax ngamay def li

Khamal ni ioe dotoko défati (no no no)

Mane rek

Fouma nekh lay goudé beuss dina niow

Nga matteu sa lokho ja

Nieup la bayi né ioe la té dou ioe

Ya ngui nane ni beuss bo mandé fégn

Guéneu goudi bayi ma fi dém

Lane ngey outi l’amour ngui si keur gui

C’est la vie (c’est la vie, c’est la vie) oh

C’est la vie (c’est la vie, c’est la vie) oh

Da ngey yam sa wai way

Am sa way nga beugeu ko loool lé

(Beug ko loool)

Mou def la fowkay (fowkay)

Yakh sa xol bé (mou yakh sa xol bi)

Mane rek

Fouma nekh lay goudé beuss dina niow

Nga matteu sa lokho ja

Am nga guél Tambacounda

Am nga guél Mauritanie

Am nga guél Fouta toro bayiwo dara

Am nga guél Kaolack nanda

Am nga guél Diourbel Dakar

Am guél kouri koro bayiwo Gambie

Am nga guél Tambacounda

Am nga guél Mauritanie

Am nga guél Fouta toro bayiwo dara

Am nga guél Kaolack nanda

Am nga guél Diourbel Dakar

Am guél kouri koro bayiwo Gambie

Queen Biz more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English (Nigerian Pidgin)
  • Genre:
  • Official site:
  • Wiki:
Queen Biz Lyrics more
Excellent recommendation
Popular