Holocauste [Intro] lyrics

Songs   2025-01-01 00:00:36

Holocauste [Intro] lyrics

Gueu-Gueumeul Yallah té boul laathie ndakh Yallah gueum

nala

Diouraum niarélou Assamane moy fi sama kaatane bi meuneu

yém

Gouvernement bi bougueul ma djangue sama waa galé bagne ma

RAP

Bougouma kène djangalma nappeu bougou-bougoumatam yaw nga

mayma djeune

Beus di nga tourné laathie Papeu Tourné laathie Yaye

Niouné leu dém nagn dou nékha gueum

Té boudone kouné yaay taaneu li ngay am, Yallah dina guiss

Nit diko niémé eupeulé

Kou weet xam sa waay deugueune taane Njaay Mo ki né ci sa

séttou nimou mel nga mel

Di def nga def Mindef nga rek meunougne la teuthie Ndakh yaw

rekka fi meusseu def lou meunta né

Oh Shit!

Souma déwé laay contane Boy

Rakk sama kerr comme naathie

Oh Shit!

Oh Please!

Boy dieul sama life Ô My GOD

Moudjeuntéél bou nice Ô My GOD

Please!

Fekké sama digueu dolé di tombék djimbi diamono

Boudone ay billets ma niakkeu deupeu paresol bi

10.000 problèmes fébaru diouni djangoro

Bindeu na GOD mais néna dou tidjii enveloppe bi

Easy dama niaak djom djépi sama bopp

Mou melni amouma compte beug ibi sama banque bopp

Méti nama lolou ndakh ma ngui naane té nékoul mako sombi

Liir bou tangueu xel momak PA bou tangueu xol

Dominique amena bac-gam (BAC) yeah tané na

Fk boy DIP ki dou meusseu dieundeul Yaayam Keur

Sama xel tééy sama xel tééy ma niaaw njorte ci fimay

moudjé

Di nélaw ni neew, guédeu, fo guissé kou déh di gueinteu?

Ma nék di yëg sama ROUH bé ngui dém

Bataye gni di sathieu ak gni di thiaggatou rek la gni né

tchi tali bi di yélwane di gnéin

Oh Shit!

Souma déwé laay contane Boy

Rakk sama kerr comme naathie

Oh Shit!

Oh Please!

Boy dieul sama life Ô My GOD

Moudjeuntéél bou nice Ô My GOD

Please!

XAJJA (Chien) gueuneu djégué NIT, NIT gueuneu djégué

IBLISS

Nioune nioko gueune té nioune nioy def ni xajjou (Chien)

IBLISS

Comme millardaire yu gueune riche fi

Douniou suur té nio ngui lekk ay xollou miskine

Légui NIT gni nioy DEUM yi

DEUM yi di déh wak xiff NIT

Yeah lane moy deuggou wa dji yokkou taux de suicide?

Ma faté guèneu djaadeu outi yonou EGLISE

Ndakh église yagg nafa noyi air pur

Ni JESUS souma guéné nékaate Hercules

Waayé bama djoudo la xam ni gagné nagn guerre bi

Dama djoudou joy ndakh Aduna pour nga am li nga beug faaw

nga def li nga bagne

Lou tarr saay soko amé kénène ki nga gaagne

Louy mbaax so mataloul galém Ndékkéék agne

Limay dieumeulé kanam lay def di déffaate

Mane nga sèèn ci sa temps faaw nga def ni sa Baaye

Liguèy lou fay VOLCAN ni SEYDINA LAYE

Bo teudé diko niaane di nga déh ci sa lale

Gueum ni ya eupeu lerr naadjé gou xess di xessal

GOORGOORLU wouma GOOR la douma DJIGUèNE

Loutah meunou maassi guèneu ni YOUSSOU MADJIGUèNE

Outoum Xaliss rek bamay soukraate di déh

Loumou laathie niou def tant que mo ngui am di léw

Dou maak niom dou niok mane

Waa mané DUNYA soumala meunoul meuno ma

Dou maak niom dou niok mane

Parce que déwone naa bou yagg yaw

Kou déh ba dékki sanioul bideunti dou naadjé yéwou

Souma amone lalou xaliss sakh douma dém teudi

Beugouma KHALIFA, TALIBE yaay sama SERIGNE

Taal bou Yallah taal laa ci Aduna ngané do tchi andeu

Ba Alaxîrra mou taal leu yaw tamite

Am par force ndakh NIAAKEU day rayé

Té XALISS rekka meuneu FATHIE DOCTEURS YI (Bis echo)

Dip Doundou Guiss more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, French, English
  • Genre:Electronica, Hip-Hop/Rap, Pop, R&B/Soul
  • Official site:https://www.instagram.com/dip_doundouguissofficiel/
  • Wiki:
Dip Doundou Guiss Lyrics more
Dip Doundou Guiss Featuring Lyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Artists
Songs