Le Passeur lyrics
Songs
2024-12-27 19:28:26
Le Passeur lyrics
guiss nani guay daaw
guiss nala saa waay
diowé sééni gaal
guaa gni yééndou wooné
kou diowé ba soonou
diaambar la saa waay
toogal fanaane
baa beut séét
déém nafa sorinaa
bassouba sorinaa (2x)
khoolna liguay daaw
khoolaal assamane
bii guélaaw li yéksé
adiana soriwoula
kou la khool néla dieulma
toogal fanaane
toogal yéndou
baa beut séét
déém nafa sorinaa
bassouba sorinaa (10x)
- Artist:Wasis Diop
- Album:Everything is Never Quite Enough