Mafia Bi lyrics

Songs   2025-01-05 15:26:54

Mafia Bi lyrics

[Jailler Bangz]

Héy, Mafia Bi tew na dangay xaar

Bu naré sedd nañu ko bayi

Mounane tëss

Cas bi xaar ko tëss

Xew ni saraxu t...

Forcément on fait le buzz

[OMG]

Mani, Mafia Bi tew na dangay xaar

Bu naré sedd nañu ko bayi

Mounane tëss

Cas bi xaar ko tëss

Xew ni saraxu t...

Forcément on fait le buzz

Touss tassar dara du xew

Touss tassar dara du xew, ngani

Touss tassar dara du xew

Mani, eh, touss tassar dara du xew

[Jailler Bangz]

Hey, toubar kala mashallah (waaw)

Bind bu rafet bima Yala bindé la kontan (waw)

Bobu xalima dam na do guis kenen kel comme man (déedéet)

Am na dolé soxor na kane momay laccé combat

Ay yow xo ba jeex muy cipatu di mér

Ku mer kalamel Yalla fi sisu mofi jeex

Hé saraxu glaace (na xol yi fex)

Saraxu frigo (hé na xol yi fex)

Saraxu glaace (na xol yi fex)

Hey, saraxu frigo (hé na xol yi fex)

[4Leuz]

Touss tassar dara du xew

Bañal ma nga nangu

Dugg ci dëm yii kulay walu

Saraxu clim, xol you tilim

N... bu didim, diko ci bombu

Dangay baré ma tak si ndombu

Tukusu ben si xol yow bone

Danga baax ma jaay la bone

Jité boy yii dilen nduli

Touss tassar

[Kmou]

Hé ku baax si xol you fex, tay mu neex

Sarax si moy nga begg wañi mér

Ku jum ba songu gaindé tay nga dé

Dajé banc yak der di sandi xer

Nit nga dumala ñé

Dof nga dumala ré

Yéné ming si nék

Sisu man nga pousse ma né

[Jailler Bangz]

Héy, Mafia Bi tew na dangay xaar

Bu naré sedd nañu ko bayi

Mounane tëss

Cas bi xaar ko tëss

Xew ni saraxu t...

Forcément on fait le buzz

[OMG]

Mani, Mafia Bi tew na dangay xaar

Bu naré sedd nañu ko bayi

Mounane tëss

Cas bi xaar ko tëss

Xew ni saraxu t...

Forcément on fait le buzz

Touss tassar dara du xew

Touss tassar dara du xew, ngani

Touss tassar dara du xew

Mani, eh, touss tassar dara du xew

[Cool 10]

Yo, déedéet du jam li comme guerre

Faw mu turu ndaxté dafa fess

Defleen ni degg di def fen

Bay katu guerté du nam caf

Ci soce yi lay cap ten

Démuñu té bawuñu ken dem

Kuko mën du kuy jëm

Té sélébe yoon du pour toce nen

Xëyel dima waxal man may gënë dem

Sukkër sama dundu lukoy téré neex

Fouli garab yi di fax suf si di jalaño

Sañsé dox nank xol yi di ñamaño

Hé saraxu glaace (na xol yi fex)

Saraxu frigo (hé na xol yi fex)

Saraxu glaace (na xol yi fex)

Hey, saraxu frigo (hé na xol yi fex)

[OMG]

Eh, di séral sa xol loy waxati

Sa tamaté makoy lokati

Tass tassar game bi bamu tass

Eh, ñu tek ko bako fi

Mani këlëm mulay mass

10 du ray ass

Wuré bi dem na kung

Ma yor balle bi dumla passe

Loloy dëgg man la sen wa kër begg

Lakatul nga cëgine lingay bégge ñokay tëg

Dalay neex, yoyou dalay neex

Toce kany pacal limon def si bëcëk dalay neex

[Jailler Bangz]

Héy, Mafia Bi tew na dangay xaar

Bu naré sedd nañu ko bayi

Mounane tëss

Cas bi xaar ko tëss

Xew ni saraxu t...

Forcément on fait le buzz

[OMG]

Mani, Mafia Bi tew na dangay xaar

Bu naré sedd nañu ko bayi

Mounane tëss

Cas bi xaar ko tëss

Xew ni saraxu t...

Forcément on fait le buzz

Touss tassar dara du xew

Touss tassar dara du xew, ngani

Touss tassar dara du xew

Mani, eh, touss tassar dara du xew

OMG more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof
  • Genre:
  • Official site:
  • Wiki:
OMG Lyrics more
OMG Featuring Lyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Artists
Songs