Sabari lyrics

  2024-06-23 16:10:57

Sabari lyrics

Mane Fogone na ni makk ioe dou meussa dièkh

Baba fogone na ni makk ioe ba abadane

Mane fogone na ni makk ioe dou meussa dièkh

Ba fogone na ni makk ioe ba abadane

Aduna ko warilen neu

Mane sama ba déh sour nama

Mane sama aduna déh yakhouna

Kima geuneu beug fassé nama

Hummm... ndiabote gui wet lool

Souma fataliko

Baba souma fatali ko waaw

Makk ioe nio dane teud ci béneu lal ba

Nga dane ma deukeul dima xélal waw

Li tey khawma louko waral

souma sagnone

Baba souma sagnone mane

Souma sagnone

Baba souma sagnone mane

Dig ma bayi ci sama négou seuy ba

Khalé yi daniou nameu sen yaye

Mane fogone na ni makk ioe dou meussa dièkh

Ba fogone na ni makk ioe ba abadane

[Bambara]

Queen Biz more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English (Nigerian Pidgin)
  • Genre:
  • Official site:
  • Wiki:
Queen Biz Lyrics more
Excellent recommendation
Popular