Senegal lyrics

Songs   2025-01-05 15:17:52

Senegal lyrics

Sénégal niokko mome

Kéne meunouko khar niar

Khiff lekk niakoufi

Marnane niakoufi

Goudé am fo fanane sama rew

Bouniou nangou keneu douggou souniou diguenté

Same diam djifi niom mame bayi

Khamouniou lénène

Bougouniou lénène

Hé Hé Hé

Gueye ndioro waynala (gueye ndioro waynala)

Faye birame waynala (waynaaaaaala)

Diobeu dioubeu waynala (diobeu dioubeu waynala waynala waynala)

Tourè mandi waynala (hééééééhéhéhééé)

Thiam babel demba thiam waynala

Gomissa gania waynala (sané balama)

Ndiaye diatta ndiaye waynala

Dioufa niokhobay waynala (mané djonkéléfa)

Sante yi war galgui reew mangui

Sante yi war galgui reew mangui

Diom foulak fayda

Fonk diné takh khol yé ngui naat

Dieuf diou bakh deh diogoufi

Soutoura laniouy ndamo

Han Sénégal ndiaye sama rew

Walo walo si réw mi

Sine Saloum si réw mi

Casamance Boundou

Cadior ak Baol Fouta Toro

Djolof Sénégal

Dieng salla waynala (Samb maharam waynala)

Diagne Naar waynala (Diallo diery waynala)

Sow poulo waynala (Ba poulo waynala Yagg masseuy)

Sall ngari waynala (Cissé ngari Ngom séni)

Ndoye mali maram ndoye waynala (wade farawade ndiack)

Mendy coto waynala (pouye beukeury)

Fall ndiaga yaram waynala (waynala Camara yilé)

Dieye massamba waynala (Guissé maabo)

Mbacké balla aissa

Sy sawandé

Niass coumba abdallah

Laye Makhtar

Kounta sidy waynaaaaaa léne

Sante yi war Galgui reew mangui (Lo ndam ciré)

Sante yi war Galgui reew mangui (Youm sega Mbaye mbassou Diene ndiogou)

Sante yi war Galgui reew mangui (Thiaw séni Mbengue mbor)

Sante yi war Galgui reew mangui (Ndour wally mbergane Niang mbaallo)

Sante yi war Galgui reew mangui (Sene thiali Sylla moctar)

Sante yi war Galgui reew mangui (Seck sa guanar)

Sante yi war Galgui reew mangui (Sarra moundo Ly bousso)

Sante yi war Galgui reew mangui

Sante yi war Galgui reew mangui

OMG more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof
  • Genre:
  • Official site:
  • Wiki:
OMG Lyrics more
OMG Featuring Lyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Artists
Songs