Soma Woraté lyrics

  2024-06-23 15:55:34

Soma Woraté lyrics

Yeksil, déloussil, limey ndiorte néxoumay

Limey dégeu souma lérré baby dotoko défati

Yeksil, gnibissil, limey ndiorte néxoumay

Limey dégeu souma lérré baby dotoko défati

Hannnn... Hannn... hannnn

Baby dotoko défati

Hannnn... Hannn... hannnn

Baby dotoko défati

Boy limey dégeu mbadou deugeula

Sou amé rek néma deugeula

Khalé bi ci kogn bi dagko biralate

Dégeunané baby ioe deh yafa diar

Faté diapone nala ngey dokhane

Téwoul ma ngui tokk mane dila mougnalate

Soma waraté, dina takali sa bop ak sa bate

Soma waraté, baby may koulay diongalate

Soma waraté, dina takali sa bop ak sa bate

Soma waraté, baby may koulay diongalate

Sama baby légui dafay am guel

Souma waxé moumey diéma tek khel

Souniou éguer baby nala

Watt ndél, boul faté denthial nala béna yatou kel

Loy wouti fénén kholal nima taroo yeah yeah yeah

Loy wouti fénén kholal nima dionguama yeah yeah yeah

Loy wouti fénén kholal nima séxé yeah yeah yeah

Baby dafa doy, bougouma sa lay

Bala may déh ngay hay hay

Lo def yako tay bougouma sa lay

Bala may déh ngey hay hay

Baby dafa doy, bougouma sa lay

Bala may déh ngay hay hay

Soma waraté, dina takali sa bop ak sa bate

Soma waraté, baby may koulay diongalate

Soma waraté, dina takali sa bop ak sa bate

Soma waraté, baby may koulay diongalate

Sama baby légui dafay am guel

Souma waxé moumey diéma tek khel

Souniou éguer baby nala watt ndél

Boul faté denthial nala béna yatou ke

Loy wouti fénén kholal nima taroo yeah yeah yeah

Loy wouti fénén kholal nima dionguama yeah yeah yeah

Loy wouti fénén kholal nima séxé yeah yeah yeah

Mane tay warouna, ci goorou tay yi

Képeu ki ci naane di neubeutou

Biss bo mandé rek da ngey fégn

Hannnn... Hannn... hannnn

Biss bo mandé rek da ngey fégn

Queen Biz more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English (Nigerian Pidgin)
  • Genre:
  • Official site:
  • Wiki:
Queen Biz Lyrics more
Excellent recommendation
Popular