Xalis lyrics

Songs   2025-01-03 19:34:36

Xalis lyrics

Khaliss laniou geuneu fonk nitt walay

Nitt a meuneu am khaliss ioe khaliss laniouy am

Lou waral gni di diay sen lerr dieundé ko leundeum

Allalou aduna la leep fi ngakoy bay

(khaliss llaniou geuneu fonk nitt walay)

(Nitt a meuneu am khaliss ioe khaliss laniouy am)

(Lou waral gni di diay sen lerr dieundé ko leundeum)

(Allalou aduna la leep fi ngakoy bay)

Khaliss lagn ley khamé

Khaliss lagn ley lathié

So amoul khaliss dougn la khamé

Dougn la wolou dougn la lathié

Nieupa beug melni mome

Khaliss tek la gathié

Boul ma wolou boul ma lathié

Awma khaliss million flow laley wathié

(khaliss llaniou geuneu fonk nitt walay)

(Nitt a meuneu am khaliss ioe khaliss laniouy am)

(Lou waral gni di diay sen lerr dieundé ko leundeum)

(Allalou aduna la leep fi ngakoy bay)

(khaliss llaniou geuneu fonk nitt walay)

(Nitt a meuneu am khaliss ioe khaliss laniouy am)

(Lou waral gni di diay sen lerr dieundé ko leundeum)

(Allalou aduna la leep fi ngakoy bay)

Ashs The Best more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof
  • Genre:
  • Official site:
  • Wiki:
Ashs The Best Lyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Artists
Songs