Yow lay Nobaat

Songs   2024-12-22 15:34:18

Yow lay Nobaat

Lo beug beug naa

Lo bagn mane beugouma

Yaa takh namatouma dara kone diegué ma

Baby deff ma loula nekh yaa tey waay

Doumla meusseu bayi hun hun

Kaay kaay

Sa ree meune nama rey té bougouma guiss ngey merr

Ragal nimla beugué khalé bi li comme guerre

So beugué louma amoul nako wouti diokh la

Sam mbeuguél sama amour negn ko boolé yokh la

Mi corazón (corazón )

Mane douma taayi té douma sone (no no no)

Wakh lene ak mom

Damko nopp té nangou naa ci niakk diom

Oh ohh ouhh ohh

Damako guiss youkhou oh ouh oh

Oh ohh ouhh ohh

Foumala guiss youkhou oh ouh oh

Yaw laay nobat , yaw laay nobat

Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat

Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat

So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat

Yaw laay nobat , yaw laay nobat

Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat

Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat

So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat

Diaral ngama khékh ak Pa bi gueneu gallé

Guédeu agn té sou mère bi wakhé doumko

falé

Collé serré doumla bayi moukk di crazy

Bayanté negn mais yaw laay guéneul ba leggi

Amna kénene mais soum key khol yaw rek laay guiss

Deuké sagnsé pour nga xool ma sa khel delsi

Baby , beugué nala nouné

Fo dem ma fekk la fa diaral ngama louné

Oh ohh ouhh ohh

Damako guiss youkhou oh ouh oh

Oh ohh ouhh ohh

Foumala guiss youkhou oh ouh oh

Yaw laay nobat , yaw laay nobat

Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat

Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat

So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat

Yaw laay nobat , yaw laay nobat

Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat

Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat

So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat

Sama kér ak sama garap

Sama febar sama garap

Takh ma guerre ak samay parents

Baay ma dee ci sa kaw darap

Yow linguere nga or ak diamant

Takal la aldinay kara

Yaw rekka ma diaral ganratie bakane koranté Balla

Teud diakhane fou ay car rapide diaré sama kaw yaram

Ta dou thiakhane diaral ngama niou nane ki diaratoul dara

Diaro bim ley takal dou diarat ci benene baram

Diabar laley deff

Diabar diou keneu doul lambal ndiaram

Yaw laay nobat , yaw laay labat

Dagueu sama baat gueuneu yombou nga niane ma baat

Diokh ma sa lokho té goungué ma Porto Rico

Yaay sama lover sama chabalaba ding dong

Oh ohh ouhh ohh

Foumala guiss youkhou oh ouh oh

Yaw laay nobat , yaw laay nobat

Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat

Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat

So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat

Yaw laay nobat , yaw laay nobat

Souniou dee wé ba déki wat mane yaw laay nobat

Yaw laay nobat , baby yaw laay nobat

So deukone sakh ci dima fenn mane yaw laay nobat

Jahman Xpress more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof, English
  • Genre:Hip-Hop/Rap
  • Official site:
  • Wiki:
Jahman Xpress Lyrics more
Jahman Xpress Featuring Lyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Artists
Songs