Wétoon Na lyrics

Songs   2025-01-05 22:05:47

Wétoon Na lyrics

Demb wétoon na

Dama réroon nga fégnal ma

Yaw mi ladon xar

Fekeu ma ci leundeum niital ma

Sama xol wétoon na

Dagua gneuw ma xam louy aduna

Sa mbeuguél dundal ma

Yorr yeureum ma

Damala beug beug

Té yallah takh parél la pour nékak yaw

Nax démb wétoon na

Dama réroon nga fégnal ma

Yaw la taamo nékal yaw la nangoul louma

Meussoul nangoul kén

Sa mbeuguél dundal ma

Yarma yarma yéma yeureum ma

Wou wohou wow

Wou wohou wow

Mbeuguél bi dima gagne yeah yeah

Wou wohou wow

Nan nan nan nan

Yeahi yeahi yeah

Mbeuguél bi dima gagne

Nakh démb wétna wétna

Tay samay ndakar diekhna wétna

Yakar guou tassone waaw

Sama xol lama teudione kasso waawaw

Banex bi gnewna gnewna

Meti wone demb taay nekhna nekhna

Mak yaw all day all night

Sa wéét la beug déss mak yaw for life

Démb wétoon na, wétoon na

Dama réroon nga fégnal ma, fégnal ma

Sa mbeuguél la gneuw doundal ma, doundal ma

Yorma yarma yeureum ma, yeureum ma

Démb wétoon na, wétoon na

Dama réroon nga fégnal ma, fégnal ma

Sa mbeuguél la gneuw doundal ma, doundal ma

Yorma yarma yeureum ma, yeureum ma

Mak yaw

Sa wéét la beug déss mak yaw for life

So bébé beugua touma nga sorima

Sa wéét la beug déss mak yaw all day all night

Mak yaw all day all night

Sa wéét la beug déss mak yaw for life

Démb wétoon na, wétoon na

Dama réroon nga fégnal ma, fégnal ma

Sa mbeuguél la gneuw doundal ma, doundal ma

Yorma yarma yeureum ma, yeureum ma

Démb wétoon na, wétoon na

Dama réroon nga fégnal ma, fégnal ma

Sa mbeuguél la gneuw doundal ma, doundal ma

Yorma yarma yeureum ma, yeureum ma

Wétoon na

Fégnal ma

Doundal ma

Yeureum ma eh

Ashs The Best more
  • country:Senegal
  • Languages:Wolof
  • Genre:
  • Official site:
  • Wiki:
Ashs The Best Lyrics more
Excellent Songs recommendation
Popular Songs
Artists
Songs